Текст и перевод песни «I am writing this letter»

Исполнитель: Max Richter

Текст

bakkan waruw dall la fa muy degge dooko yeg dem rekk delu si rekk melni weer wi delu si ci sey jeego feneen weer mouk ci fi, bidew bi danouna dee ci souff samay xarit, tey ji ndadje bi rafet na, djoko, seeddo, ak retane bi rafet na, xew bou neex mais soubbe dagniouy dem, galankor bi moy dougnou meuneu xamante bou bax, dou nouy am waxtou bou doy ngir soppante goudi gi wess, mangi won fenene, bi ci toop dina fi sori ak samay bok ci camion bi, dinagnouy teugueu ngir feccelo yeneni nit ak samy bok ci camion bi, ngir andi mbekte bignouy djeul bakkan waruw dall la ku dul toxu doo xam fu dekk neexe fa muy dagge dooko yeg (Merci a El Cancre pour cettes paroles)

Перевод

Bakkan waruw dall la fa muy degge dooko yeg Dem rekk delu si rekk Melni weer wi delu si ci sey jeego Feneen weer mouk ci fi, Bidew bi danouna dee ci souff Samay xarit, tйy ji ndadje bi rafet na, djoko, seeddo, Ak rett bi rafet na, Xew bou neex Но сомненький dagniouy dem, Galankor bi moy dougnou Meuneu xamante bou bax, dou nouy am waxtou Bou doy ngir soppante Goudi gi wess, mangi выиграл Fenene, bi ci toop dina fi sori Ak samay bok ci bi грузовик, Dinagnouy teugueu ngir feccelo yeneni nit ak samy bok ci bi грузовик, ngir andi mbekte bignouy djeul Bakkan waruw dall ku dul toxu doo xam fu dekk neexe fa muy dagge dooko yeg (Спасибо El Cancre за эти слова)